WALLY B. SECK - DONT BE AFRAID LYRICS

Sou leer deh dokh dem ngikoy hame ci bidew
Sou deuk deh doh didem gnikoy hame ci diefin euh

Denou gor dafa ara yatu dafa wara wara yatu
ndah ki djohe dafa tabe dafa mandu motah gniou wara mandou
close
volume_off


non non ndeysan enh ndeysan

man nanoy togano yalla def niou bagnia bokk guis guis
man nanoy andano yalla def niou bagnia bokk meun meun
man nanoy bok yoon yalla def niou bagnia book yeene
man nanou bok khet yalla deff niou bagnia bok wawa

Denou gor dafa ara yatu dafa ara ara yatu
ndah ki djohe dafa tabe dafa mandu motah gniou ara mandou

adouna xel la yaye - now be your self _ now be your self
guemeul sa bop xam ki gua doon ndeysan


l"am now stronght Africa is stronght 
don't be afraid - never be afraid - that right l said 

" imanake donomaye obe kontere lela " 
" imanake famamaye obe kontere lela " 
"imanake donimaye obe kontere lela " 
" ajabalo ajabalo " 

guemeul sa bop 
ikabido simasindole l"am now stronght 
ikabido simasindole don't be afraid 
ikabido simasindole l'am from senegal ouest africa 
terangua ligueye niakh djarigniou rek lagniou xam 
sama askan ligueye askan rek guem 
sama yaya ak baye dagn tete ci yoon bou bakh 
sama askan ligueye lagniou xam 



lalali lalee now be your self 
lalali lalee guemeul sa bop 
lalali lalee l'am now stronght 
alali lalee don't be afraid 
lalali lalee 

def you melni def you mel ni lila wah 
that is right see 
def you melni def you mel ni lila wah 
that is right see 
def you melni def you melni lila wah 
that is right see 

guemeul sa bop ham kigua don ndeysan 
don't be afraid 
don't be afraid that right l said

Commentaires