Wally B. Seck - FILAY NEE ( LYRICS )

Wally Seck - Lyrics Filay Né ( Session Studio ) Filay né Nëké mbeguél filay né Dama am sa faiblesse Xool bi yathie féss Took dila diandér di dioy dafmay daal Non non non non nileu nileeeu Damay woo Dame Séne Sama kaw scène Takaal ko Chaîne Guire mou beguelel maleeu Diokh nala thëre bi Ba mél ni koula ragal dafmay daal Amouma ci kërsa Deugle nani diam Ci yow lakooy amé woor nama En batay néna mbeguel filay né Woo batay mbeguel mbeguel mbeguel Filay lay nék Diokh nala thiëre bi Amouma si kërsa Deugle nani diam Thie oie lakoy amé Woo woo waaw Guisou looni gaayi Nénna niou louniou ma wakh ma wakh la Dimako toogné Woo hoo filay né Néké mbeguel filay né Diokh nala thiëre bi Amouma si kërsa Dook yalla ba nimala falé nigama taalé fii Néké mbeguél filay né #Abones vous ®tallawallyjr

Commentaires